Numbers 27:19
TSK
Taxawal ko fi kanam Elasar sarxalkat bi, ci kanam mbooloo mépp, te nga sas ko ci seen kanam,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Taxawal ko fi kanam Elasar sarxalkat bi, ci kanam mbooloo mépp, te nga sas ko ci seen kanam,
Waaye nanga yebal Yosuwe, ñaax ko, jàjj ko, ndax moom mooy jàll, jiite mbooloo mii, te moo leen di jox réew moomu ngay séen.»