Exodus 29:7
TSK
Te nga jël diwu pal gi, sotti ko ci kaw boppam, diw ko.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Te nga jël diwu pal gi, sotti ko ci kaw boppam, diw ko.
Mu sotti nag tuuti ci diw gi ñuy fale ci boppu Aaróona, diw ko, sellale ko ko.
Ndax kat ci biir dëkkub rawtoom la wara toog, ba kera deewug sarxalkat bu mag bi. Gannaaw bu sarxalkat bu mag bi deeyee nag, ki rey sañ naa dellu fa mu bokk.
te ci yiwu Yàlla wu àndul ak genn pey lees di joxe ñépp àtteb ñu jub, ndax njot gi sottee ci Almasi Yeesu.
¶ Gannaaw nag am nanu kilifag sarxalkat bu mag bu jàll ba biir asamaan, te mooy Yeesu Doomu Yàlla, nanu ŋoy ci yoonu ngëm wi.
Du deretu sikket mbaa yëkk la duggaale, waaye deretu boppam la dugge benn yoon ba fàww ca bérab bu sell baa sell, te moom la amale njotlaay gu sax dàkk.