كل أسفار KYG

Revelation 21

KYG · الآية 3

22 أصحاحات

KYG / Revelation / الأصحاح 21

KYG · الآية 3

M a dégg kàddu gu xumb jibe ca ngàngune ma, ne: «Màkkaanu Yàllaa ngii ci biir nit ñi. Mooy dëkk ak ñoom, ñu diy ñoñam. Yàlla ci boppam mooy dëkk ak ñoom, di seen Yàlla.