TSK

TSK · Romans 9:33

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Éy, aar ma, musal ma! Bu ma rusloo, yaw laa làqoo.

Mu doon seen bérab bu sell, di doj wuy fakktale, xeer wuy féle, ci ñaari këri Israyil, te dim yeer, dig fiir, ñeel ku dëkk Yerusalem.

Israyil, yaay mucc fa Aji Sax ji mucc gu sax dàkk! Doo rus, doo torox fii ak ëllëg.

Joel 2:26 TSK

Dingeen lekka lekk, ba regg, di sàbbaal seen turu Yàlla Aji Sax, ji leen defal kéemaan, te sama ñoñ dootuñu rus mukk.

Mbind mi moo ne: «Képp ku ko gëm, doo rus.»

Looloo tax may daj yii coono. Waaye rusuma ci, ndax xam naa ki ma gëm, te wóor na ma ne moo mana sàmm li ma ko dénk ba keroog bés ba.