TSK

TSK · Titus 2:6

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 29:8 TSK

waxambaane gis ma, ñooru, mag ña jóg, taxawal ma,

Xalelu góor bi, bànneexul bi ngay gone, bégalal sa xol bi ngay ndaw. Toppal loo namm ak loo xemmem, waaye xamal ne loolu lépp, Yàlla da la koy laaj.

¶ Naka noonu yeen ndaw ñi, nangul-leen magi mbooloom gëmkat ñi. Yeen ñépp nag toroxluleen ci seenug jëflante, ndax: «Yàlla, ñi réy lay xeex, ñi toroxlu, mu may leen aw yiw.»