TSK

TSK · 1 Kings 21:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Mu ne Amnon: «Waaw, yaw doomu buur nga, lu la tax ne yogg nii bés bu set? Doo ma ko wax?» Amnon ne ko: «Tamar, mi bokk ak sama doomu baay Absalom ndey ak baay, moom laa bëgg.»

Ndax ba Yesabel jabari Axab di rey yonenti Aji Sax ji, Abdiyas a boole woon téeméeri yonent, làq leen ci ñaari xuntiy xeer, xunti mu nekk juróom fukk. Mu di leen fa may lekk ak naan.

¶ Axab dafa dogu woon ci def lu bon lu Aji Sax ji ñaawlu, ba amu ci moroom moos, te jabaram Yesabel di ko ci xabtal.

Esteer woolu Atag, ma Buur féetaleek moom, te muy kenn ci bëkk-néegi buur. Mu yebal ko ci Mardose, ngir xam lan la ak lu waral loolu.