1 Samuel 13:16
TSK
¶ Sóol ak doomam Yonatan, ak gàngoor ga ànd ak ñoom ña nga dal ca Geba gu Beñamin, waa Filisti dal ca Migmas.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Sóol ak doomam Yonatan, ak gàngoor ga ànd ak ñoom ña nga dal ca Geba gu Beñamin, waa Filisti dal ca Migmas.
Wenn doj waa nga sampe wetu bëj-gànnaar, janook Migmas, wa ca des sampe wetu bëj-saalum, janook Geba.
¶ Booba nit ku bon a nga woon ca mbooloo ma, ku ñuy wax Seba, di doomu Bikkri, ma bokk ca giirug Beñamin. Seba wal liit ga, daldi yéene ne: «Sunu yoon nekkul ci Daawuda doomu Yese jii, du benn cér bu nu am ci moom. Yeen waa Israyil, ku nekk ca sa xayma!»
jaare ca xunti ma te naan: «Geba lanuy fanaani!» Waa Raama tiit, waa Gibeya gu Sóol daw.