TSK

TSK · 2 Samuel 2:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Yanqóoba moom topp yoonam. Ci kaw loolu ay malaakay Yàlla feeñu ko.

Soxnas Sóol moo doon Ayinowam, Ayimaas di baayu Ayinowam. Njiitu xareem moo doon Abner doomu Ner baayu Sóol bu ndaw,

Mu àddu ca kaw, wax ak gàngoor ga, daldi ne Abner doomu Ner: «Éey Abner, doo ma wuyu?» Abner ne ko: «Yaw yaa di kan bay joor Buur?»

Sóol nag amoon na nekkaale bu ñuy wax Rispa doomu Aya. Mu am bés Isboset ne Abner: «Ana lu waral nga dëkkoo sama nekkaaleb baay?»

¶ Rekab ak Baana, doomi Rimon ma dëkk Berot nag ñoo demoon kër Isboset, àgg fa ci biir tàngooru njolloor, fekk Isboset di for bët.

Bànni Israyil daldi ànd ak Absalom dal ca diiwaanu Galàdd.