TSK

TSK · Acts 10:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ay askan yu bareey dikk, naan: «Dikkleen nu yéegi tundu Aji Sax ji, fa kër Yàllay Yanqóoba, mu xamal nuy yoonam, ba nu doxe yooyu ñallam.» Siyoŋ kat la ndigalu yoon di bawoo, Yerusalem googu la kàddug Aji Sax ji di jóge.

«Bésub keroog,» kàddug Aji Sax jee, Boroom gàngoor yi, «ku nekk ci yeen ay woo moroom ma ci ker garabu reseñam, ak ker garabu figgam.»

Luke 5:29 TSK

Ci kaw loolu Lewi waajalal ko bernde ju réy ca këram. Mbooloo mu bare teew, ay juutikat ak yeneen gan, ñu bokk toog, di lekk.

Acts 8:40 TSK

Filib moom, dëkk ba ñuy wax Asot la gisaat boppam. Mu wéye di xamle xibaaru jàmm bi ci dëkkoo dëkk, ba àgg Sesare.