TSK

TSK · Acts 12:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Bu ab soxor faloo, ñépp làquji, bu daanoo, ku jub teg tànk.

Njekk moo lay dëgëral, nga sore noteel, doo tiit; sore tiitaange, du la jege.

¶ Gannaaw loolu Dañeel dem ca Aryog mi Buur santoon mu rey boroom xam-xami Babilon. Ba mu demee ne ko: «Boroom xam-xami Babilon yi, bu leen reylu. Yóbbu ma ca Buur, ma jox ko piri mi.»

Acts 6:7 TSK

¶ Ba loolu amee kàddug Yàlla di law, limu taalibe yi yokku ba bare lool ci biir Yerusalem, sarxalkat yu bare daldi topp yoonu ngëm wi.

¶ Noonu la kàddu gi lawe ba féete kaw ci kàttanu Boroom bi.

¶ Li ci des nag bokk yi, moo di ngeen ñaanal nu, ngir kàddug Boroom bi gaawa law te am ndam na mu ko ame woon fa yeen,