Acts 21:18
TSK
Ca ëllëg sa Póol ànd ak nun, seeti Yanqóoba, fekk mag ñépp a nga fa teew.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ca ëllëg sa Póol ànd ak nun, seeti Yanqóoba, fekk mag ñépp a nga fa teew.
¶ Ca ëllëg sa nag njiital gàngoor ga bëgga am lu ko leer nàññ ca la Yawut ya jiiñ Póol. Mu yiwi ko, woolu sarxalkat yu mag ya, ak mboolem kurélu àttekat ya. Ci kaw loolu mu indi Póol, taxawal ko ci seen kanam.
¶ Ba mu ko defee mu woo ñaari njiiti takk-der, ne leen: «Waajal-leen ñaar téeméeri xarekat ak juróom ñaar fukki gawar ak ñaar téeméeri boroom xeej, ngir ngeen dem Sesare bu juróom ñeenti waxtu jotee ci guddi.
¶ Ñu teg ca juróomi fan, Anañas sarxalkat bu mag ba dikk, ànd ak ay mag, ak ab layookat bu ñuy wax Tertul. Ñu jébbalsi boroom réew ma, tuuma ja ñu teg Póol.