1 Samuel 12:5
TSK
Samiyel ne leen: «Kon Aji Sax ji seede na ci seen biir, ki mu fal it seede tey jii, ne gisuleen lenn ci sama loxo.» Ñu ne ko: «Seede na ko!»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Samiyel ne leen: «Kon Aji Sax ji seede na ci seen biir, ki mu fal it seede tey jii, ne gisuleen lenn ci sama loxo.» Ñu ne ko: «Seede na ko!»
Ba loolu amee saytukat yaak jawriñ ya di wuta tuumaal Dañeel ci mbiri nguur gi, te gisuñu genn tooñ mbaa sikk ci moom, ndax ku amoon kóllëre la, te giseesul ci moom genn néewal mbaa sikk.