Luke 18:3 TSK Ab jëtun a nga woon ca dëkk boobee. Daan na ñëw ca moom, naan ko: “Àtte ma ak sama jotewaale!”
Acts 24:1 TSK ¶ Ñu teg ca juróomi fan, Anañas sarxalkat bu mag ba dikk, ànd ak ay mag, ak ab layookat bu ñuy wax Tertul. Ñu jébbalsi boroom réew ma, tuuma ja ñu teg Póol.