TSK

TSK · Deuteronomy 13:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Buleen dugal yëf yu seexluwu seen biir néeg, lu ko moy àtteb faagaagal bi war ci yëf yooyu, moo leen di dab, yeen itam. Xofleen koo xof, seexlu koo seexlu, ndax yëf yooyu, faagaagal moo ci war.

¶ Sàmmooleena déggal mboolem kàddu yii ma leen di dénk, ngir ngeen baaxle ba fàww, yeen ak seen doom, yi leen di wuutu, ndax kon yeena ngi jëfe lu baax li seen Yàlla Aji Sax ji rafetlu.