Genesis 24:11
TSK
Ba muy jub dëkk ba, daa yésal giléem ya fu dend akub seyaan waxtuw ngoon, fekk jigéen ñay génn di rootsi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba muy jub dëkk ba, daa yésal giléem ya fu dend akub seyaan waxtuw ngoon, fekk jigéen ñay génn di rootsi.
Mu dellu laaj leen ne leen: «Mbaa mu ngi ci jàmm?» Ñu ne ko: «Jàmm rekk kay. Xoolal ndaw see di ñëw, mook gàtt yi, mooy doomam Rasel.»
Firawna nag tudde Yuusufa Safnat Paneya, may ko jabar Asnat doomu Potifera ma doon sarxalkat ca dëkk ba ñuy wax On. Yuusufa doxe ca tegoo kilifteefu Misra gépp.
¶ Yettro sarxalkatu réewum Majan ba, baayu soxnas Musaa, dafa dégg mboolem la Yàlla defal Musaa ak bànni Israyil ñoñam ak ni Aji Sax ji génnee Israyil Misra.