Ezekiel 4:1
TSK
¶ Aji Sax ji ne: «Yaw nit ki, jëlal móolu ban, teg fi sa kanam, nga rëdd ci ab dëkk, mu misaal Yerusalem.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Aji Sax ji ne: «Yaw nit ki, jëlal móolu ban, teg fi sa kanam, nga rëdd ci ab dëkk, mu misaal Yerusalem.
«“Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Fenqeel say loxo, dóor sa tànk fi suuf te ne: ‘Ñaw!’ ci mboolem jëfi waa kër Israyil ju bon ju siblu. Saamar ak xiif ak mbas lañuy fàddoo.
¶ «“Maa ngii nag di fenqe samay loxo, di ko mititloo alal ju lewul ji nga dajale, ak sa dereti nit ji ñu tuur fi sa biir.