Ezra 8:16
TSK
Ma woolu njiit ya: Elyeser ak Aryel ak Semaya ak Elnatan ak Yarib ak Elnatan meneen ma, ak Natan ak Sàkkaryaa ak Mesulam, ak Yowarib ak Elnatan ma ca des, ñaari jànglekati yoon ya.