TSK

TSK · Genesis 16:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yàllay Ibraayma ak Yàllay Naxor, ñoom ñooñee di seen Yàllay baay, yal nañu àtte sunu diggante.» Yanqóoba daldi giñ ci Yàlla, ji baayam Isaaxa wormaaloon.

Yal na Aji Sax ji àtte sama digganteek yaw. Yal na ma Aji Sax ji feyul ci yaw, waaye du sama loxoo lay dal mukk.

Jógal, sàmmal ma sama àq. Sama Yàlla, Boroom bi, àtte ma yoon.

te fekk Màrt jàpp lool ca liggéeyu waañ wa. Mu dikk ne Yeesu: «Sang bi, xanaa gisoo sama rakk ji ma bàyyeek liggéeyu waañ wi, man doŋŋ? Wax ci boog, mu jàpple ma.»