Genesis 11:26
TSK
¶ Gannaaw ba Teraa amee juróom ñaar fukki at, am na Ibraam ak Naxor ak Aran.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Gannaaw ba Teraa amee juróom ñaar fukki at, am na Ibraam ak Naxor ak Aran.
Ibraam ak Naxor jël nañu ay soxna; soxnas Ibraam tudd Sarayi, soxnas Naxor di Milka. Milka moomu, moom ak rakkam ju jigéen Yiska, Aran ay seen baay.
¶ Ba loolu amee surga ba jële fukki giléem ca giléemi sangam, dem, yóbbaale li gën ci mboolem xeeti alalu sangam. Ma nga jëm réewu Mesopotami, ga Naxor dëkk.
Mu ne ko: «Betuwel a ma jur, doomu Naxor ak Milka,»
Xibaaru jàmm, bawoo fu sore mooy ndox mu sedd ci ku loof.