TSK

TSK · Genesis 29:35

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Leya moom it xam ne taxawaayam yàgg na, mu fab jaamam Silpa, may ko Yanqóoba.

¶ Ca jamono yooyu Yuda dafa teqlikoo ak ay doomi baayam, dal ca waa ju dëkk Adulam te tudd Ira.

¶ Yuda jegesi ne ko: «Ngalla sang bi, ma ñeme laa diis lenn rekk, te sa xol baña tàng ci man, doonte yaak Firawnaa tolloo.

«Yaw Yuda, mi say doomi baay di taggeji, ngay sëqi sa ndoddi noon, sëgal leen, sa doomi baay a lay sujjóotal.