TSK

TSK · Genesis 31:46

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye képp koo gis mu yor sa gàllaaji kër, boo yeboo reyal. Seetal fii ci sunu kanami bokk lépp lu ma fi yor, loo ci moom fabal, yóbbu.» Booba Yanqóoba xamul woon ne Rasel a ko jël.

Gannaaw loolu Yanqóoba sàkk sarax ca kaw tund wa, woo ay bokkam, ñu bokk lekk. Ba ñu lekkee ba noppi, fanaan ca tund wa.

Ñu jël néewu Absalom, sànni ci kàmb gu réy ca àll ba, daldi jóor ca kawam jalu xeer bu maga mag. Bànni Israyil yépp nag daw ñibbi seeni kër.