TSK

TSK · Genesis 46:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Gannaaw ga Bilaa, jaamub Rasel, ëmbaat, dellu amal Yanqóoba doom ju góor.

«Neftalee di kéwél gu fëx, te mooy jur doom yu taaru.

¶ Ñu lim turi sëti Neftali, ku nekk ak làngu cosaanam ak kër maamam, mboolem ñi xare war, te ñu am ñaar fukki at, jëm kaw.

Neftali la wax ne ko: Neftalee ne xéew aku yiw, biibal barkey Aji Sax ji, te sowu ba bëj-saalum lay nangu.