Psalms 137:1
TSK
Ca tàkkal dexi Babilon, foofa lanu daa toog, fàttliku Siyoŋ, jooy.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ca tàkkal dexi Babilon, foofa lanu daa toog, fàttliku Siyoŋ, jooy.
Éy ku ma mayoon ci màndiŋ mi dalu panaanum njëggaan, ba ma teqlikook bokk yi, wacc leen, dem, bàyyi leen? Ñoom ñépp ay bokkaale, di gàngooru workat.
Bu ngeen déggul de, ma làqu, jooy seen reewande, sama rongooñ tuuroo tuuru, ma jooya jooy, nde dees na jàpp géttu Aji Sax ji, yóbbu.
Looloo ma tax di jooy, rongooñ di wal-wali, te ku may dëfal sore ma, mook kuy seral sama xol. Samay doom a ngi jaaxle, nde noon bi daan na.
Askan waa ngi jooy jooyi xol fi kanam Boroom bi. Éy yaw tatay janq Siyoŋ mu taaru mi, sottil say rongooñ ni walum dex guddeek bëccëg; bul nopplu, bul feral say rongooñ.