TSK

TSK · Leviticus 7:34

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

kaala leen, te takkal Aaróona ak doomam yu góor ay laxasaay. Su ko defee ñu féetewoo céru sarxalkat, muy dogal bu sax dàkk. «Noonu ngay sase Aaróona ak doomam yu góor.

Dogal a ngii, di lu leen war fàww, ak fépp fu ngeen dëkk: lépp luy nebbon mbaa deret, buleen ko lekk.»

Waaye dënnu saraxu yékkati-jébbale bi ak tànkub jooxe bi, lekkleen ko ci bérab bu mucc sobe, yaak say doom yu góor ak say doom yu jigéen, ndax seen cér la, ci saraxi canti bànni Israyil ci biir jàmm, nga moom ko yaak say doom.

Aw yàppam, yaa koy moom, ni nga moome dënnu saraxu yékkati-jébbal, ak tànkub kanam bu ndijoor ba.