Genesis 21:1
TSK
¶ Gannaaw loolu Aji Sax ji yéwéne na Saarata, ni mu ko waxe woon, defal ko li mu ko digoon.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Gannaaw loolu Aji Sax ji yéwéne na Saarata, ni mu ko waxe woon, defal ko li mu ko digoon.
¶ Ba loolu amee Yàlla geestu Rasel, nangul ko, may ko doom.
Wujjam nag dëkke koo ñaawal, ngir naqaral ko ndax la ko Aji Sax ji mayul doom.
Aji Sax ji nag dikke Aana aw yiw, mu amaat ñetti doom yu góor ak ñaar ñu jigéen. Ci biir loolu Samiyel moom, ma ngay màgg fa wetu Aji Sax ji.
Su bés baa juróom yaari jigéen ŋoyaalu genn góor, ne ko: «Sunub dund, nun a, sunu koddaay, nun a! Jox nu sag buum rekk, teggil nu gàcce.»
Malaaka ma ne ko: «Sàkkaryaa, bul tiit, ndax sa ñaan nangu na. Elisabet sa soxna dina am doom ju góor, nanga ko tudde Yaxya.