TSK

TSK · Luke 1:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ibraam ne ko: «Boroom bi, yaw Aji Sax ji, ana loo may may nag? Man awma doom sax, te ki wara donn sama alal moo di Elyeser, miy waa Damaas.»

¶ Bi Ibraayma déggee loolu, daa sujjóot, ree. Booba ma nga naan ci xelam: «Góoru téeméeri at, ndax dina mana am doom waay? Te Saarata, mi am juróom ñeent fukki at (90) sax, manati naa am doom a?»

Gannaaw ga soxnas Isaaxa amul doom, Isaaxa dagaanal ko Aji Sax ji, mu nangul ko, soxna si daldi ëmb.

Waaye Aana la daan beral loxo ca sarax sa, ndax cofeelam ci moom, doonte Aji Sax ji mayul Aana doom.

Alyaasa ne Gewasi: «Ana lu nu koy defal nag?» Mu ne ko: «Amul doom ju góor de, te jëkkëram mag la.»

¶ Ci kaw ngëm itam la Saarata ci boppam mana ëmbe ba jur tey mag ba wees njurum doom, ndax moo njortoon ne ka dige ku wóor la.