TSK

TSK · Luke 7:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Fóotal maa fóotal sama ñaawtéef, raxasal ma sama moy.

Luke 7:35 TSK

Waaye xel mu rafet, mboolem la mu jur mooy la koy dëggal.»

Acts 19:3 TSK

Mu ne leen: «Kon gan sóobu ngeen sóobu?» Ñu ne ko: «Xanaa sóobeb Yaxya.»

Yoonu njub gi Yàlla di joxe nit ki, àtteb ku jub, moom lañu umple tey jéema dëggal seen njubteg bopp. Moo tax nanguluñu njubte gi Yàlla di maye.

Ma dégg malaaka mi yilif ndox yi ne: «Yaw Aji Sell ji nekk te nekkoon, yaa yey dogal yii àtte.