TSK

TSK · Numbers 10:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Askanu Gerson nag, seen sas ci wàllu xaymab ndaje mi, jaamookaay bi la woon ak xayma bi, ak malaan mi koy ub, ak ridob bunt xaymab ndaje mi,

¶ Gannaaw loolu Aji Sax ji wax Musaa, ne ko:

¶ Musaa nangu watiir yaak nag ya, jox Leween ñi.

¶ Kon nag gannaaw nguur gu deesul yëngal lanu jagoo, nanu jàppoo cant, di jaamu Yàlla ni mu ko bëgge cig njullite akug ragal,