TSK

TSK · Numbers 11:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Doomi Yuusufa yu góor, ya mu am Misra, tollu ci ñaar. Kon mboolem ña dem Misra te di waa kër Yanqóoba, tollu nañu ci juróom ñaar fukk.

¶ Mu neeti Musaa: «Yéegal ñëw fi Aji Sax ji, yaw ak Aaróona ak Nadab ak Abiyu ak juróom ñaar fukki magi Israyil, te ngeen sujjóote nee, dànd ma.

¶ Musaa daldi jubal ca Datan ak Abiram, magi Israyil topp ca.

¶ Te itam ay àttekat aki kilifa ngeen di tabb ngir seeni giir, ci mboolem dëkk yi leen seen Yàlla Aji Sax jiy jox, ñuy àtte mbooloo mi àtteb dëgg.

Juróom ñaar fukki magi kër Israyil a nga taxaw, janook nataal ya. Yaasaña doomu Safan a nga ca. Ku ci nekk a nga ŋàbb sab and, cuuraay la jolli.

¶ Ba juróom ñaar Fukk ñaak ñaar demee ba délsi, mbégte lañu àndal. Ñu ne: «Sang bi, rab yi sax, danu leen di jox ndigal ci sa tur, ñu nangul nu.»