Leviticus 21:1
TSK
¶ Gannaaw loolu Aji Sax ji wax na Musaa ne ko: «Waxal sarxalkat yiy doomi Aaróona ne leen: Bu ci kenn sobeel boppam, di laal mbokkam mu dee,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Gannaaw loolu Aji Sax ji wax na Musaa ne ko: «Waxal sarxalkat yiy doomi Aaróona ne leen: Bu ci kenn sobeel boppam, di laal mbokkam mu dee,
Kemu fan yi muy nasireenal, séddoo Aji Sax ji, ab néew, bumu ko jege.
¶ «Bu loolu weesee ku laal nit ku dee, ak néew bu mu mana doon, dina sobewu diiru juróom ñaari fan.
Bésub keroog laay may Gog ab pàkk, mu def ko sëg fi biir Israyil; mooy xuru jaarukaay wiy dog yoonu képp ku fa jaare, te féete yoonu penku wi jëm géeju Xorom ga. Fa lañuy rob Gog ak gàngooram gépp, ñu di ko wooye xuru Gàngooru Gog.
ba far am dëkk bu ñuy wooye Amona (mu firi Gàngoor). Noonu lañuy setale réew mi.”