TSK

TSK · Numbers 31:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yanqóoba wax ak waa këram ak ñi ànd ak moom ñépp ne leen: «Jëleleen ci seen biir tuuri doxandéem yi, te ngeen sangu-set te solu.

¶ «Lii la yoon wi tëral: Bu nit deeyee ci biir xayma, képp ku dugg ci biir xayma bi, ak képp ku mu fekk ci xayma bi, day sobewu diiru juróom ñaari fan,

Nit ki sobewu, mboolem lu mu laal day sobewu, te ku laal ca loola it day yendoo sobe ba ca ngoon.»