TSK

TSK · Ruth 3:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye ngalla boo delloo ca sa teraanga, nanga ma geestu te dimbali ma, waxal ma Firawna lu jëm ci man, ba man maa génne fii.

Ruth 1:9 TSK

Yal na Aji Sax ji may ku nekk ci yeen jàmm ca kër jëkkër ja muy amaat.» Ci kaw loolu mu fóon leen, ñu ne yikkét jooyoo.

«Ëpplante banti seedar da laa def buur? Sa baay daawul lekk ak a naan? Teewu koo jëfe dëgg ak yoon, muy njiglaayam.

Ku fàggulul ay bokkam nag, rawatina waa këram, yoonu ngëm wi la gàntal, te moo yées ku gëmul.