TSK

TSK · Zechariah 12:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ñii ñoo di askani Aaróona ak Musaa, jant ba Aji Sax jiy wax, mook Musaa ca kaw tundu Sinayi.

Doomi Keyat yu góor ñoo di Amram ak Isar ak Ebron ak Usyel, ku ci nekk ak làngam.

¶ Ci Gerson la làngu Libneen ñi, ak làngu Simeyeen ñi soqikoo. Làngi Gersoneen ñaa ngoogu.

Waaye Cadog sarxalkat ba ak Benaya doomu Yoyada, ak Yonent Yàlla Natan, ak Simey ak Reyi, ñook jàmbaari Daawuda ya koy dar, ñooñu ànduñu woon ak Adoña.

Su boobaa ngeen xam ne maa leen yónnee santaane bii, ngir saxal sama kóllëreek Lewi.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax.