TSK

TSK · Acts 11:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 33:13 TSK

Ana loo koy sikke, naan du layoo lenn ci mboolemi jëfam?

Job 40:8 TSK

Sañ nga maa teg tooñ daal, di ma sikkal, ba am dëgg?

Ba loolu amee mboolem gëmkati Yawut ya ànd ak Piyeer, waaru ca na mayug Noo gu Sell gi tuuruwaalee ca xeeti jaambur ña,

¶ «Naka laa tàmbalee wax ak ñoom Korney, Noo gu Sell gi daanu ci seen kaw, na mu jëkkoona daanoo ca sunu kaw.

Ndax kat moo noon Musaa: «Maay yërëm ku ma neex, te maay ñeewante ku ma neex.»

«Ana ku xam xalaatu Boroom bi? Ana ku ko digal?»