TSK

TSK · Acts 15:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Axas ne: «Duma ko ñaan, ndax duma nattu Aji Sax ji.»

¶ Li ma leen di wax nag mooy lii: boroom ndono li ci kër gi, li feek mu dib tuut-tànk, wuutewul akub jaam, doonte moo moom lépp.

¶ Almasi da noo yiwi, ngir nu yiwiku, kon nag saxooleen ko, te baña laxasooti buumi njaam.

Loolu misaal la, ñeel jamonoy tey, di firndeel ne jooxe yi ak saraxi jur yi ñu daan jébbale manuñoo dindi yaraangeg jaamukatub Yàlla bi, ba mu set wecc.