Esra moomu jóge Babilon, nekkoon jànglekat bu xareñ, bu géeju ci yoonu Musaa, wi Aji Sax ji Yàllay Israyil joxoon ñoñam. Aji Sax ji Yàllaam nag toppe ko yiwam, ba Buur defal ko mboolem lu mu ñaan.
TSK
TSK · Acts 18:24
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
ak njiitu juróom fukki dag, akub kàngam, ak diglekatu buur, ak ndaanaanu liggéeykat, ak jatkat bu xareñ.
Yeesu ne leen: «Lu fi xew?» Ñu ne ko: «Mbirum Yeesum Nasaret. Mu doonoon ab yonent bu manoorewu ci jëf ak ci kàddu, Yàlla ak askan wépp seede.
Musaa nag di ku mokkal mboolem xam-xamu Misra, te ràññiku lool ci wax ak ci jëf.
Foofa nag njiitu takk-der ba gis gaal gu jóge Alegsàndiri, jëm Itali, mu dugal nu ca.
¶ Man ci sama bopp, bokk yi, bi ma dikkee ci yeen, du ci puukarey kàddu yu gëna taaru, ak xam-xam bu ma leen yégalsee mbóoti Yàlla.
¶ Bokk yi, loolu de laa natte ci Apolos ak ci man, ñeel leen, ngir ngeen jànge ci sunu ñaari jëmm, ba sàmm solob kàddu gii: «Bu seen xalaat jàll ca wàlla li Mbind mi wax.» Su ko defee dungeen réy-réyloo far ak kenn, di beddi keneen.
Ndaxte bataaxal yi kat lañu ne: «Dañoo ñagas, te tàng, waaye bu teewee moom ci boppam, da naan yàcc, te ay kàddoom xeebu.»
Naka Senas xamkatub yoon bi, ak Apolos, fexe leena waajalal, ba duñu ñàkk lenn lu ñu soxla ci seen yoon.