TSK

TSK · Acts 20:38

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Acts 15:3 TSK

¶ Ci kaw loolu mbooloom gëmkat ñi yebal leen, ñu jaare Fenisi ak Samari, daldi àgge waa foofa ni jaambur ñi dul Yawut tuube, ba bokki gëmkat ñépp bég ca lool.

Acts 21:5 TSK

Ba nu fa amee fan yooyu lanu fa bàyyikoo, dem, ñu gunge nu, ñoom ñépp, ñook seeni soxna ak seeni doom. Nu dem ba génn dëkk ba, daldi sukk ca tefes ga, ñaan.

Kon bu ko kenn xeeb. Gannaaw loolu nangeen ko yiwi ak jàmm, ba mu délsi ci man, ndax moom laay xaar, mook bokk yi itam.