Dëgg la, fexeel ngeen ma lu bon, waaye Yàllaa ko walbati, def ko lu baax, ba dogal li am tey jii, muy bakkan yu bare yi mucc.
TSK
TSK · Amos 3:6
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aji Sax ji Boroom gàngoor yee giñ ne: «Lu ma nar déy mooy am, lii ma mébét, mooy sotti.
«Nangeen yégle lii fa Yuda, dégtale ko fa Yerusalem, yéenee koog liit fi biir réew mi te xaacu seen kem kàttan ne leen: “Dajeleen, nu dem ca dëkk ya tata wër.”
Man daal, dungeen ma ragal, am tiituleen ma?» Kàddug Aji Sax jee. «Man mi teg gannuus, yemalee ko géej, dogalal ko ko dàkk te du ko jàll, lu mu wañax wañax du ko man; gannax ya day riir, te du jàll!
Yaw Buuru xeet yi, ana ku la dul ragal? Yaw déy yaa yelloo ragal. Mboolem ñi xelu ci xeet yi ak mboolem seeni buur, kenn melul ni yaw.
«Wal-leen bufta gi ca Gibeya, jibal liit gi ca Raama te yéene ca Bet Awen. Moytul sa gannaaw, Beñamin.
Nit kooku ñu jébbale ni ko Yàlla dogale te nasoon ko lu jiitu, yeena ko daajloo yéefar yi ci bant, reylu ko.
¶ Danoo xam lan mooy ragal Boroom bi nag, te moo nu tax di wax lu gëmloo nit ñi. Yàlla de ràññee na bu baax nooy kan. May yaakaar ne yeen itam, ci seen biir xol, ràññee ngeen bu baax nooy kan.