Job 22:13
TSK
Nga naa: «Ana lu Yàlla xam? Ana nu muy àttee ci gii lëndëm gu tar?
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nga naa: «Ana lu Yàlla xam? Ana nu muy àttee ci gii lëndëm gu tar?
Boroom bi nee: «Basan laay waññee noon yi, waññee leen xóotey géej,
nga tettee ma fa ba tey, téyee ma sa ndijoor.
¶ «Maa ngii di woolu nappkat yu bare.» Kàddug Aji Sax jee. «Ñu napp ñii ba noppi ma woo rëbb yu bare, ñu rëbb leen ci kaw mboolem tund wu mag ak wu ndaw, ba ci bépp xar-xaru doj.
Ku mana làqoo làquwaay, ba duma ko gis?» Kàddug Aji Sax jee. «Xanaa du asamaan ak suuf, maa ko fees?» Kàddug Aji Sax jee.