TSK

TSK · Esther 2:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

ñu indil ko Lingeer Wasti, mu sol mbaxanam lingeeram, ngir won taaram ba nit ñaak kàngam ya, ndax jigéen ju rafetoon la.

¶ Gannaaw loolu Buur Aserus jox bésub keroog Lingeer Esteer kër Aman, fitnaalkatu Yawut ya. Ñu woo Mardose ca Buur, ndax fekk na Esteer xamle ba noppi na Mardose bokkeek moom.

Job 31:18 TSK

Ba may ndaw laa dala yor ab jirim ni baayam; te ba ma juddoo ci sama ndey laa dala gindi ab jëtun.

Yudeen ña ca bokkoon di Dañeel ak Anaña ak Mikayel ak Asaryaa.

¶ Yeen ñiy baay it, buleen xoñoñal xale yi, waaye yarleen leen, di leen jubanti, di leen xamal coobarey Boroom bi.