Exodus 3:1
TSK
¶ Léegi Musaa ngay sàmm gàtti goroom Yettro, sarxalkatu Majan ba. Mu yóbbu jur ga fu sore ca màndiŋ ma, daldi agsi ca suufu tundu Yàlla wa ca Oreb.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Léegi Musaa ngay sàmm gàtti goroom Yettro, sarxalkatu Majan ba. Mu yóbbu jur ga fu sore ca màndiŋ ma, daldi agsi ca suufu tundu Yàlla wa ca Oreb.
¶ Gannaaw loolu mbooloom bànni Israyil gépp bàyyikoo màndiŋu Ciin, di dox ak a taxaw, ci ndigalal Aji Sax ji. Ñu dem ba Refidim, dal fa. Foofa nag mbooloo ma amuñu woon ndox mu ñu naan.
Yettro, gorob Musaa nag yóbbul Musaa soxnaam aki doomam ba ca màndiŋ ma, fa Musaa dal ca kaw tundu Yàlla wa.
Ñu bàyyikoo Refidim, dali ca màndiŋu Sinayi,
Moom it moo nekkoon ak mbooloo ma ca màndiŋ ma, mook malaaka ma doon wax ak moom ca kaw tundu Sinayi ca sunu wetu maam ya. Moo jot ci kàddu yuy dund, ngir jottli nu ko.