TSK

TSK · Exodus 2:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

tegaat ca ne ko: «Léegi jigéenu wérul nga, te dinga am doom ju góor; nanga ko tudde Ismayla (mu firi Yàlla dégg na), ndax Aji Sax ji yég na sa naqar.

¶ Aana mujj ëmb ca ndeetel at ma. Gannaaw gi mu am doom ju góor, tudde ko Samiyel (mu firi Yàlla dégg na), ndax da ne: «Maa ko ñaan Aji Sax ji.»

Acts 7:21 TSK

Ba ñu ko sànnee, doomu Firawna ju jigéen a ko foral boppam, yar ko ni doomam ju mu jur.

Ba Musaa màggee, ngëm a taxoon mu bañ ñu wooye ko doomu doomu Firawna ju jigéen.