Yeena ngii tey di dem seen yoon ci weeru Abiib.
TSK
TSK · Exodus 40:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Te itam ràbblul ay sori kawari bëy, ngir def ko ñaareelu xayma, muy kiiraay ci kaw jaamookaay bi. Fukk ak benn la sor yiy doon.
Ci biir xaymab ndaje mi la Aaróona ak doomam yu góor di teg làmp yi, ci kanam rido bi làq gaalu àlluway seede si, ñuy fanaanee tàkk ngoon ba bët set, fi kanam Aji Sax ji. Dogal a ngoogu, war bànni Israyil fàww, ñoom ak seen askan.
jaamookaay bi ak xaymaam ak kiiraayam aki keppoom aki làccam, ak galan yeek jën yeek tegu yi,
¶ «Tegal sarxalukaayu rendi-dóomal bi fi kanam buntu màkkaanu xaymab ndaje mi.
¶ Aji Sax ji moo wax ak Musaa ca màndiŋu Sinayi ca biir xaymab ndaje ma, keroog benn fanu ñaareelu weer wu ñaareelu at, ma topp ca gàddaay ga bawoo Misra. Mu ne ko:
¶ «Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Benn fanu weer wi jëkk, nanga jël yëkk wu ndaw wu amul sikk ngir laabal bérab bu sell bi.