¶ Yàlla ne: «Na am ay leer ci asamaan, ngir xàjjale guddi ak bëccëg, te doon ay tegtal, yuy ràññle jamono yi, tey takk bés yi ak at yi.
TSK
TSK · Genesis 1:20
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 1:14
TSK
Genesis 1:30
TSK
Naka rabi àll yépp it, ñook picci asamaan yépp ak lépp luy raam ci kaw suuf, te di boroom bakkan, jox naa leen lépp luy ñax mu tooy, ñoom itam, muy seen lekk.» Mu daldi nekk noona.
Genesis 8:17
TSK
Génnewaaleel lépp luy xeetu mbindeef mu ngeen àndal: picc yi ak bàyyima yi ak luy raam, ñu fulandiwu ci kaw suuf, daldi giir te bare.»
Job 12:9
TSK
Ana ku umple ci mboolem ñii, ne loxol Aji Sax jee def lii lépp?
Psalms 104:25
TSK
Géej a ngee réy te yaa, la fay yëngu maneesu koo lim, muy ndundat lu mag ak lu ndaw.
Nit a ngi doñ-doñee xel, xam-xam ak manoore, te ku doñ-doñiwuloon lay wacce alalam. Loolu it, cóolóoli neen ak naqar wu réy.