TSK

TSK · Genesis 18:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ba loolu amee Amnon tëdd, wopp-wopplu, ba Buur ñëw di ko seet. Amnon ne ko: «Na sama jigéen Tamar ñëw defaral ma ñaari mburu yu ndaw, may gis, te sexal ma ci loxol boppam, ma lekk.»

Waaye gor si, ngor lay mébét, te ngor lay wéye.

¶ Yeesu ak ay taalibeem ñoo toppoon seenu yoon, ba tollook ab dëkk. Ba ñu dikkee, senn as ndaw su ñuy wax Màrt, ganale ko.

Deeleen def seen loxo ci lu faj soxlay gëmkat ñu sell ñi, te boole ci am teraanga.

Buleen sàggane di terle, nde am na ñu seen teraanga tax ñu fat ay malaaka te xamuñu ko woon.