Psalms 107:34
TSK
suuf su nangu doon jooru xorom ndax mbonug ña ko dëkke.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
suuf su nangu doon jooru xorom ndax mbonug ña ko dëkke.
te mennum Lóot aji jub ji, di kenn ki mu musal, te mu sonnoon lool, ndax ñaawtéefi nit ñu dëng ñooñu,
Mu ubbi buntu kàmbu xóote ba, saxar su mel ni saxaras taal bu mag jollee ca, jant bi ak jaww ji, lépp lëndëm ndax saxaras kàmb gi.
¶ Buuri àddina yi àndoon ak dëkk bii ci moy ak dund gu bakkane, bu ñu séenee saxaras lakkam, ñoom ñépp ay yuuxu, di ko jooy.
¶ Ñu neeti: «Aleluya! Saxaras lakku dëkk ba kay day jolli rekk, ba fàww!»