TSK

TSK · Genesis 24:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waaye dinga dem sama réew, ma ma cosaanoo, jëlal fa sama doom Isaaxa soxna.»

su ko jëkkër ja déggee, te bés ba mu ko déggee, waxu ko ca dara, su boobaa xasi ndaw si day sax, te kàdduy dogu ya mu tegooloon boppam day sax.

Acts 7:2 TSK

Eccen ne ko: «Yeen bokk yi, yeen samay baay, dégluleen! Yàlla, miy Boroom daraja moo feeñu woon sunu maam Ibraayma, ba mu nekkee réewum Mesopotami, bala moo sanc Karan.