TSK

TSK · Genesis 27:45

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Ci kaw loolu Kayin séq ak rakkam Abel wax. Ba mu ko defee ñu dem ca àll ba, Kayin dal ci kaw Abel, bóom ko.

Isaaxa ne ko: «Sa rakk ñëw na, nax ma, ba yóbbu sa ñaan.»

Bare na lu xol di mébét, waaye Aji Sax jeey dogal.

Acts 28:4 TSK

Waa réew ma gis jaan ja langaamoo loxol Póol, ñu naan ca seen biir: «Nit kii kay ab bóomkat lay doon, ndegam moo rëcce géej, te taxul Ndogal may ko mu dund.»