TSK

TSK · Genesis 34:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ñooñu bokk ci xeet, yi Aji Sax ji waxoon bànni Israyil ne leen: «Buleen jëli jabar ci ñoom, ñoom it buñu takksi ci yeen, ndax kon dinañu leen dëpp, ngeen topp seeni tuur.» Teewul Suleymaan bëgg leen, taq leen.

Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, yaaka sopplub dëkkuwaay!