TSK

TSK · Genesis 37:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ruben nag àddu ne leen: «Ndax newuma leen woon: “Buleen gàddu bakkanu xale bi,” waaye faalewuleen ma; tey rekk la nu Yàlla doon xaare bakkanam, bi nu gàddu.»

su boobaa buleen ko nangul, buleen ko déglu, buleen ko xool bëti yërmande, buleen ko baal, buleen ko nëbbal.

Acts 12:1 TSK

¶ Ca jamono jooju la Buur Erodd jàppoon ñenn ca mbooloom gëmkat ña, di leen mitital.